Baykat-Ismaël Lômp3下载无损flac下载
Baykat-Ismaël Lô在线试听免费歌词下载
[00:00.000] 作词 : Lo
[00:08.60]mané hé baykat bi khalam
[00:14.67]démonna bay nékh wayé boumgua
[00:18.93]dokna mome
[00:22.39]
[00:23.49]mané hé baykat bi khalam démonna
[00:29.53]bay nékh wayé boumgua dokna mome
[00:36.34]
[00:40.77]boula nékhé talalal say lokho
[00:44.32]yaye docteur biy fath khifou askane bi
[00:47.28]liko dalé si nditoum rew bassi miskine
[00:55.41]ya souméko di dane sa dolé andak nath
[00:59.42]bi di liguey sa gnakha di tourou
[01:02.57]ngay bay di doukat bilay ya am diome
[01:08.49]
[01:08.91]kon diarama baykat koufi xiff yako
[01:12.43]doundal bamou sour waw koufi fébar
[01:18.22]yako nandal aki réén bamou féékh
[01:22.71]
[01:23.23]kon diarama baykat koufi xiff yako
[01:26.75]doundal bamou sour
[01:30.37]waw koufi fébar yako nandal aki réén
[01:34.30]bamou féékh
[01:36.66]
[01:41.99]ya momone sa mbay
[01:45.19]ya mome sa guanthiakh mome say
[01:47.21]ndiour ya mome sa alla di bay
[01:56.39]nguour gneuw dougalthia lokhome ak
[01:59.91]boor fékeleuthaa guanthiakh ba
[02:02.85]mégneu lole ndékétéyo
[02:09.55]
[02:09.85]kon diarama baykat koufi xiff yako
[02:13.15]doundal bamou sour
[02:16.88]waw koufi fébar yako nandal aki réén
[02:20.63]bamou féékh
[02:23.97]
[02:24.25]kon diarama baykat koufi xiff yako
[02:27.59]doundal bamou sour
[02:31.24]waw koufi fébar yako nandal aki réén
[02:35.21]bamou féékh
[02:42.86]
[03:10.77]kon diarama baykat koufi xiff yako
[03:14.06]doundal bamou sour
[03:17.85]waw koufi fébar yako nandal aki réén
[03:21.70]bamou féékh
[03:24.57]
[03:26.46]dirama diarama baykat bé yaw
[03:33.50]kéneu rek mola mana fay
[03:36.27]moy bourbi yaalla
[03:40.73]guathia ngalama
[03:43.26]guathia ngalama yaw baykatbé
[03:47.76]guathia ngalama
[03:50.51]guathia ngalama yaw baikatbé
[03:53.57]
[03:55.21]dirama diarama baykatbé yaw
[04:02.13]kéneu rek moleu mana fay
[04:04.88]moye bourbi yalla
[04:08.62]